Góor Gu Gudda Lool
Cornelius Wambi Gulere
Catherine Groenewald

Ay paxam dafa gatt lool.

1

Buntam dafa suufe lool.

2

Lalam dafa gatt lool.

3

Ay bisikletam dafa gatt lool.

4

Góor gii gudd na lool!

5

Moo def bant bu gudd.

6

Moo def bunt yu kawe.

7

Moo jënd bisiklet bu kawe.

8

Moo def lal bu gudd.

9

Moo toog ci toogu bu kawe.

Moo lekk ak furset bu gudd.

10

Mu génn këram dem dëkk ci àll bu mag.

Mu dund at yu bare.

11
You are free to download, copy, translate or adapt this story and use the illustrations as long as you attribute in the following way:
Góor Gu Gudda Lool
Author - Cornelius Wambi Gulere
Translation - ak Cornelius Wambi Gulere
Illustration - Catherine Groenewald
Language - Wolof
Level - First words